![]() |
![]() |
![]() |
![]() |
![]() |
![]() |
![]() |
![]() |
|
| Portal | Liberation Forum | Store | Arcade | Search YouTube | ABIBItube Media | Site Map | Photo Gallery | Abibifiles | Bookmark Us! | Member Classroom |
|
|||||||
| Register | VBay [0] | Invite Afrikans | Stats | All Albums | Blogs | FAQ | Donate | Members | Calendar | Search | Today's Posts | Mark Forums Read |
| Notices |
| Wolof Language Resources Jangukaay ju Xam-xami Lakk Wölöf |
|
|
http://www.abibitumikasa.com/forums/![]() |
|
![]() |
|
|
LinkBack | Thread Tools | Display Modes |
|
||||||||||||
|
BATAAXAL GU MAG GI ËMB SAÑ-SAÑI DOOMI AADAMA http://www.abibitumikasa.com/yabb/At...s/bataaxal.pdf Ñu jàpp te nangu ne sagu doomi aadama ak sañ-sañam yépp-dañu yam te kenn mënukóo jalgati, te lu lépp nekk na cës laay ci taxufeex ci mbirum àtte ak jàmm ci biir àdduna. Ñu jàpp ne ñakk xam ak soofantal sañ-sañi doomi aadama indi na aymusiba yu tar tax képp kuy dund fippu. Temano egsi na ba mu nekk ci doomi aadama ñu mën a wax, xalaat, ci seen coobare, bundxatal, nàkk dëddu leen. Ñu jàpp ne am na solo lool ñu aar sañ-sañi doomu aadama ak ay matukaay ci wàllu yoon; ngir doomu aadama moomu kenn du ko sonal, muy fippu ci nootaange ak lu koy bunduxatal. Ñu jàpp ne am na solo lool ñu góor-goorlu ba gën a rataxal jokkalante gi diggante xeet yi. Ñu jàpp ne ci bataaxal boobule mbootaayu xeet yi yeesalaat na ay pas-pasam jëme ko ci sañ-sani doomi aadama yu tolloo, ci sag, ci bir lépp lu aju ci dundin diggante góor ak jigéen, ci biir tawfeex gu yaa. Ñu jàpp ne réew yi ci bokk jël nañu ay matukaay ngir dëgëral jokkalante gi ak mbootaayu xeet yi, ñu naw it bu baax sann-sañi doomi aadama ak tawfeex yu wóor ci biir àdduna yépp. Ñu jàpp ne ànd taxawal sañ-sañ yeek tawfeex yi nekk na lu am solo lool ngir, darajaal matukaay yooyu. Ndaje mu mag mi biral na ci bataaxal bii ne xeet yépp, réew yépp ak kurel yépp ñu jàpp li ci nekk, ci seen xel, te ñu góor-góorlu, ñu jaarale lii lépp ci njàng mi ak yar gi. Ñu lawal sañ-sañ yeek taawfeex yi jël aymatukaay ci biirak bitim réew. Ñu nangu te di doxal fépp ci anam gu wér ci biir xeet yi sosoo ci réew i bokk ci mbootaay gi ak gox yi bootu ci ñoom.
__________________
Uhuru sasa! Fahodie seesei! Ominira nisisiyi! Moom sa bopp leegi!
Freedom now! Please be sure to check out the exciting things going on here this summer at Abibitumi Kasa Afrikan Language and Liberation community networks! Just click on any image in the slideshow below for more info and links! And don't forget to stay BlackNificent! Obadele Kambon Abibitumi Kasa Afrikan Language Institute Abibitumi Kasa Afrikan Liberation Institute Abibitumi Kasa Online Market |
![]() |
| Bookmarks |
| Thread Tools | |
| Display Modes | |
|
|
Similar Threads
|
||||
| Thread | Thread Starter | Forum | Replies | Last Post |
| International Declaration of Human Rights - Yoruba | Olùkọ́ Ọbádélé | Yoruba Language Resources | 0 | 07-31-2008 12:38 AM |
| Human Rights Violations in Virginia State Prisons | Olùkọ́ Ọbádélé | Oppression of Afrikans Militarily | 0 | 03-07-2007 10:26 AM |
| Nit: Celebrating 50 years of the Universal Declaration of Human Rights with illustrations | Olùkọ́ Ọbádélé | Wolof Language Resources | 0 | 11-18-2006 02:28 AM |
| (Universal Declaration of Human Rights) | Olùkọ́ Ọbádélé | KiKongo Language Resources | 0 | 08-25-2006 02:58 AM |
| U.S.Human Rights Report Indicts Government | Abibiwiase Adawurobכsεm (Afrikan World News) | 0 | 12-31-1969 08:00 PM | |
|
These are the 70 most-searched-for thread tags
Search Tag Cloud
|
| (twi) 7 or 8 9th 2008 abibitumi abujamal africa afrikan akan ancient applications baby baruti begins bible black booklist camps class cnn concentration court cultural death egyptians family geronimo ghana ghanafest hebrew? inside introduce journey june kamau kambon kasa languages launch learn liberation links main messengers mothers mwalimu nations network nigerian okomfo online post race rashidi runoko sankɔfa science seneweb session slideshow standing summer summit t'shango trouble twi week wolof words yoruba |