WIKIPEDIYAA CI WOLOF - GÉEJU XAM-XAM
http://wo.wikipedia.org/wiki/Main_Page (http://wo.wikipedia.org/wiki/Main_Page)
Nas wi bokk na ci bëre biy dàq ber gi ñu ber yenn làkk yi (rawatina ci lënd-jokkoo bi) ak dàkk itam gëndaloo gu yamale te jàppalente, loolu sukkandiku ci sañ-sañu askan yi gàddu seen kuute ci cadda.
Addina bu gën di yamale, ak gën di tinkiku ci la aju !!!